Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 17:14-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 17:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Ndoortel ay di wal mu tàmbali, luy indib xuloo, bàyyil.
15 Dëggal ku sikk ak daan ku jub, Aji Sax ji sib na yooyu yaar.
16 Ab dof du am xaalis, jënde xel mu rafet; buggu ca dara.
Kàddu yu Xelu 17 in Kàddug Yàlla gi