Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 17:12-13 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 17:12-13 in Kàddug Yàlla gi

12 Taseek gaynde gu ñàkki doomam moo gën taseek dof ak yëfi dofam.
13 Kuy feye mbon jëf ju baax, lu bon du jóge sa kër.
Kàddu yu Xelu 17 in Kàddug Yàlla gi