Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 16:7-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 16:7-10 in Kàddug Yàlla gi

7 Ku Aji Sax ji rafetlu say jëf, say bañ sax, mu jubaleek yaw.
8 Néewle te jub moo gën barele te jubadi.
9 Nit ay sumb yoonam, Aji Sax ji sottal.
10 Su buur àddoo cib àtte, muy kàddu gu Yàlla dogal.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi