Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 16:6-9 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 16:6-9 in Kàddug Yàlla gi

6 Ku jiital ngor ak worma, Yàlla jéggal la; ku ragal Aji Sax ji, dëddu lu bon.
7 Ku Aji Sax ji rafetlu say jëf, say bañ sax, mu jubaleek yaw.
8 Néewle te jub moo gën barele te jubadi.
9 Nit ay sumb yoonam, Aji Sax ji sottal.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi