Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 16:6-7 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 16:6-7 in Kàddug Yàlla gi

6 Ku jiital ngor ak worma, Yàlla jéggal la; ku ragal Aji Sax ji, dëddu lu bon.
7 Ku Aji Sax ji rafetlu say jëf, say bañ sax, mu jubaleek yaw.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi