Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 16:5-7 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 16:5-7
in
Kàddug Yàlla gi
5
Aji Sax ji sib na ku réy, da koy mbugal ci lu wér.
6
Ku jiital ngor ak worma, Yàlla jéggal la; ku ragal Aji Sax ji, dëddu lu bon.
7
Ku Aji Sax ji rafetlu say jëf, say bañ sax, mu jubaleek yaw.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms