Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 16:4-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 16:4-8 in Kàddug Yàlla gi

4 Lu Aji Sax ji sàkk, mbir la ca namm, ba ci ku soxor ak bésu mbugalam.
5 Aji Sax ji sib na ku réy, da koy mbugal ci lu wér.
6 Ku jiital ngor ak worma, Yàlla jéggal la; ku ragal Aji Sax ji, dëddu lu bon.
7 Ku Aji Sax ji rafetlu say jëf, say bañ sax, mu jubaleek yaw.
8 Néewle te jub moo gën barele te jubadi.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi