Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 16:3-4 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 16:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Loo bëgga def, diis ko Aji Sax ji, say mébét sotti.
4 Lu Aji Sax ji sàkk, mbir la ca namm, ba ci ku soxor ak bésu mbugalam.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi