Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 16:26-28 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 16:26-28 in Kàddug Yàlla gi

26 Ku bëgg lu neex, liggéey; ku bëgga faj sab xiif, njaxlaf.
27 Sagaru nit mooy sulli lu bon, ay waxam sax sawara la.
28 Nitu njekkar day yokk réeroo, ab soskat di féewaley xarit.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi