Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 16:23-26 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 16:23-26
in
Kàddug Yàlla gi
23
Ku rafet xel, say kàddu xelu; soo waxee, yey.
24
Wax ju yiw di lem juy xelli, neexa ñam, di jàmmi yaram.
25
Yoon a ngi, nit defe ne jub na, te mu jëme ko ci ndee.
26
Ku bëgg lu neex, liggéey; ku bëgga faj sab xiif, njaxlaf.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms