Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 16:22-26 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 16:22-26 in Kàddug Yàlla gi

22 Xel mu ñaw day suuxat bakkan, te ab dof jëfi dofam a koy yar.
23 Ku rafet xel, say kàddu xelu; soo waxee, yey.
24 Wax ju yiw di lem juy xelli, neexa ñam, di jàmmi yaram.
25 Yoon a ngi, nit defe ne jub na, te mu jëme ko ci ndee.
26 Ku bëgg lu neex, liggéey; ku bëgga faj sab xiif, njaxlaf.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi