Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 16:19-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 16:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 Woyof, ànd ak ku néewle moo gën séddook ku bew la mu lewal.
20 Ku teewlu mbir, baaxle; ku wóolu Aji Sax ji, bég.
21 Ki rafet xel mooy kiy ràññee, te su wax rafetee, dég-dég yomb.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi