Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 16:13-15 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 16:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Wax ju dëggu, buur safoo boroom; ku jub, buur bëgg sa kàddu.
14 Merum buur ndaw la, dee a ko yónni; ku rafet um xel, giifal ko.
15 Buur, na kanam ga leer, sa bakkan mucc, su la baaxee, mu mel ni taw bu topp um nji.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi