Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 16:10-12 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 16:10-12 in Kàddug Yàlla gi

10 Su buur àddoo cib àtte, muy kàddu gu Yàlla dogal.
11 Nattub diisaay aki ndabam, na jub ngir Aji Sax ji. Moo sàkk mboolem nattukaay.
12 Buur daa sib kuy def lu bon, ngir njekkay dëgëral nguuram.
Kàddu yu Xelu 16 in Kàddug Yàlla gi