Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 15:8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 15:8 in Kàddug Yàlla gi

8 Saraxub ku soxor, Aji Sax ji bañ na ko; ñaanu kuy jubal da koy bége.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi