Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 15:31-32 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 15:31-32 in Kàddug Yàlla gi

31 Kuy dégg àrtu yu koy musal, ku rafet xel a ngoog.
32 Xalab waxi yar, foye sa bopp la; deel déggi àrtu, yokk sam xel.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi