Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 15:30-32 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 15:30-32
in
Kàddug Yàlla gi
30
Kanam gu leer day seral xol; xibaaru jàmm, jàmmu yaram.
31
Kuy dégg àrtu yu koy musal, ku rafet xel a ngoog.
32
Xalab waxi yar, foye sa bopp la; deel déggi àrtu, yokk sam xel.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms