Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 15:3-6 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 15:3-6
in
Kàddug Yàlla gi
3
Aji Sax ji moo gis lépp, di xool ku baax ak ku bon.
4
Wax ju neex garab la, doom ya di dundal, kàddu yu jekkadi di jeexal xol.
5
Ab dof day xeeb yaru baay ba, kuy dégg waxi àrtu, xelu nga.
6
Kër ku jub, koom gu yaa; ku jubadi, alalam jur fitna.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms