Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 15:26-29 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 15:26-29 in Kàddug Yàlla gi

26 Aji Sax ji bañ na mébét mu bon, te wax ju yiw daa sell fa moom.
27 Wutin wu lewul, sonal sa waa kër; ku bañ alalu ger gudd fan.
28 Ku jub day teeylu tontam; ab soxor, wax ju ñaaw rekk.
29 Aji Sax ji day dëddu ab soxor, di nangu ñaanu ku jub.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi