Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 15:20-23 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 15:20-23 in Kàddug Yàlla gi

20 Doom rafet xel, baay ba bég; te ab dof ay xeeb ndey ja.
21 Jëfi dof a neex ku ñàkk bopp, ku am ug dégg def njub.
22 Diisoo ñàkk, pexe moy; digle takku, pexe joy.
23 Nit bége na tontam lu dal, kàddu gu jib fa mu ñoree neex!
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi