Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 15:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 15:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Doom rafet xel, baay ba bég; te ab dof ay xeeb ndey ja.
21 Jëfi dof a neex ku ñàkk bopp, ku am ug dégg def njub.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi