Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 15:2-5 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 15:2-5 in Kàddug Yàlla gi

2 Ku xelu àddu, xam-xam rafet; ab dof di talalali.
3 Aji Sax ji moo gis lépp, di xool ku baax ak ku bon.
4 Wax ju neex garab la, doom ya di dundal, kàddu yu jekkadi di jeexal xol.
5 Ab dof day xeeb yaru baay ba, kuy dégg waxi àrtu, xelu nga.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi