Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 15:17-18 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 15:17-18 in Kàddug Yàlla gi

17 Njëlu ñetti xob fa ñu la soppe moo dàq yàpp wu duuf fu ñu la bañe.
18 Naqari deret, taalu ay. Teey, fey fitna.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi