Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 15:15-18 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 15:15-18
in
Kàddug Yàlla gi
15
Xol bu tiis, naqar wu sax; xol bu neex, bànneex bu sax.
16
Néewle te ragal Aji Sax ji moo gën barele, sa bopp ubu.
17
Njëlu ñetti xob fa ñu la soppe moo dàq yàpp wu duuf fu ñu la bañe.
18
Naqari deret, taalu ay. Teey, fey fitna.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms