Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 15:13-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 15:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Xol bu sedd, kanam gu leer; xol bu tiis, boroom ne yogg.
14 Ku am ug dégg sàkku xam-xam, ab dof di toppi caaxaan.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi