Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 15:11-12 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 15:11-12 in Kàddug Yàlla gi

11 Njaniiw ak biir suuf, Aji Sax ji di gis, xolu doom aadama waxi noppi.
12 Kuy ñaawle buggul ku ko àrtu, te du laaji ku rafet xel.
Kàddu yu Xelu 15 in Kàddug Yàlla gi