Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 14:9-12 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 14:9-12 in Kàddug Yàlla gi

9 Ab dof, su bàkkaaree, yoonam! Te ñay jubal a séq yiwu Yàlla.
10 Tiisu xol, boroom a ko xam; mbégte ma it jaambur bokku ca.
11 Ab soxor, këram day tas, mbaarum ku jub di naat.
12 Yoon a ngii, nit defe ne jub na, te mu jëme ko ci dee.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi