Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 14:7-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 14:7-10 in Kàddug Yàlla gi

7 Dàndal ab dof, du la yokk xam-xam.
8 Ku ñaw day xelu, xam li muy def; ab dof di nax boppam.
9 Ab dof, su bàkkaaree, yoonam! Te ñay jubal a séq yiwu Yàlla.
10 Tiisu xol, boroom a ko xam; mbégte ma it jaambur bokku ca.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi