Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 14:5-6 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 14:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Seede bu dëggu, dëgg rekk, seede bu dëgguwul, fen rekk.
6 Ab ñaawlekat day wut xel mu rafet, mu réer ko; ku am ug dégg, xam yomb la.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi