Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 14:4-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 14:4-8 in Kàddug Yàlla gi

4 Su yëkk takkul, bey, sàq wéet; mu beye dooleem, meññeef ne gàññ.
5 Seede bu dëggu, dëgg rekk, seede bu dëgguwul, fen rekk.
6 Ab ñaawlekat day wut xel mu rafet, mu réer ko; ku am ug dégg, xam yomb la.
7 Dàndal ab dof, du la yokk xam-xam.
8 Ku ñaw day xelu, xam li muy def; ab dof di nax boppam.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi