Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 14:3-4 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 14:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Ab dof a ngi réy-réylu, làmmiñam yar ko; ku rafet xel, sa kàddu aar la.
4 Su yëkk takkul, bey, sàq wéet; mu beye dooleem, meññeef ne gàññ.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi