Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 14:26-28 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 14:26-28
in
Kàddug Yàlla gi
26
Ragal Aji Sax ji kaaraange gu wér la ci nit, di rawtu ciy doomam.
27
Ragal Aji Sax ji day suuxat bakkan, ba boroom du tàbbi ci fiiri ndee.
28
Su mbooloo baree, buur am ndam; fu nit ña néew, kilifa du fa dara.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms