Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 14:20-24 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 14:20-24 in Kàddug Yàlla gi

20 Ku ñàkk, say dëkk sax bañ la; ku barele, barey xarit.
21 Ku xeeb sa dëkkandoo, bàkkaar nga; ku baaxe ku ñàkk, mbégte ñeel la.
22 Kuy mébét lu bon daa réer, kuy mébét lu baax am nga ngor ak worma.
23 Kër-këri, jariñu; waxi neen, loxoy neen.
24 Ku rafet xel jagoo alal, ab dof ràngoo ndofam.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi