Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 14:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 14:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Ku ñàkk, say dëkk sax bañ la; ku barele, barey xarit.
21 Ku xeeb sa dëkkandoo, bàkkaar nga; ku baaxe ku ñàkk, mbégte ñeel la.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi