Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 14:19-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 14:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Ku bon, ku baax sut la; ku soxor ay toogaanu ku jub.
20 Ku ñàkk, say dëkk sax bañ la; ku barele, barey xarit.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi