Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 14:18-19 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 14:18-19 in Kàddug Yàlla gi

18 Ab téxét ndof ay céram, ku ñaw jagoo xam-xam.
19 Ku bon, ku baax sut la; ku soxor ay toogaanu ku jub.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi