Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 14:17-19 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 14:17-19 in Kàddug Yàlla gi

17 Ku gaawa mer, def jëfi dof, te kuy fexeel nit, ñu bañ la.
18 Ab téxét ndof ay céram, ku ñaw jagoo xam-xam.
19 Ku bon, ku baax sut la; ku soxor ay toogaanu ku jub.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi