Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 14:14-17 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 14:14-17
in
Kàddug Yàlla gi
14
Ku def njekkar sab añ mat, ku baax gën law demin.
15
Ab téxét, loo wax mu gëm; ku ñaw xam fi ngay jaare.
16
Ku xelu day ragal, di dëddu lu bon; ab dof day ràkkaaju, du tiit.
17
Ku gaawa mer, def jëfi dof, te kuy fexeel nit, ñu bañ la.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms