Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 14:14-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 14:14-16 in Kàddug Yàlla gi

14 Ku def njekkar sab añ mat, ku baax gën law demin.
15 Ab téxét, loo wax mu gëm; ku ñaw xam fi ngay jaare.
16 Ku xelu day ragal, di dëddu lu bon; ab dof day ràkkaaju, du tiit.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi