Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 14:13-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 14:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Nit a ngi ree, xol ba tiis, te mbégte mujje na njàqare.
14 Ku def njekkar sab añ mat, ku baax gën law demin.
Kàddu yu Xelu 14 in Kàddug Yàlla gi