Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 13:7-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 13:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Nit a ngi am-amlu, amul dara; nit di dee-deelu te fees dell.
8 Ku am ay fey alal, ba mucc; ku amul deesu ko tëkku.
Kàddu yu Xelu 13 in Kàddug Yàlla gi