Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 13:7-10 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 13:7-10
in
Kàddug Yàlla gi
7
Nit a ngi am-amlu, amul dara; nit di dee-deelu te fees dell.
8
Ku am ay fey alal, ba mucc; ku amul deesu ko tëkku.
9
Ku jub day leer nàññ, ab soxor mel ni taal bu fey.
10
Réy-réylu jote rekk lay jur, ku dégg ndigal a xelu.
Kàddu yu Xelu 13 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms