Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 13:3-6 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 13:3-6 in Kàddug Yàlla gi

3 Moom sa làmmiñ, sàmm sa bakkan; rattaxle, yàqule.
4 Ab yaafus day yaakaar, du am; ab njaxlaf sàkku, woomle.
5 Ku jub bañ na ay fen, ku soxor di indi gàcceek yeraange.
6 Ku mat day jub, ba fegu; moykat soxor, ba sànku.
Kàddu yu Xelu 13 in Kàddug Yàlla gi