Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 13:3-4 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 13:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Moom sa làmmiñ, sàmm sa bakkan; rattaxle, yàqule.
4 Ab yaafus day yaakaar, du am; ab njaxlaf sàkku, woomle.
Kàddu yu Xelu 13 in Kàddug Yàlla gi