Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 13:22-25 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 13:22-25
in
Kàddug Yàlla gi
22
Ku baax, donale ba cay sëtam; alalu moykat, muuru ku jub.
23
Ku néewle bey na, meññeef ne gàññ, ñu àtte ko ñàkkal, mu ñàkk ko.
24
Ku dul bantal sa doom, bëggoo ko. Ku bëgg sa doom teel koo yar.
25
Ku jub day lekk ba regg, soxor ba dëkke xiif.
Kàddu yu Xelu 13 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms