Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 13:18-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 13:18-20 in Kàddug Yàlla gi

18 Ku sàggane yoonu yar, séddoo ñàkk ak gàcce; kuy déggi àrtu, am teraanga.
19 Aajo ju faju tooyal na xol, te ab dof jomb naa dëddu mbon.
20 Àndal ak ku xelu, sam xel rafet; ku lëngook ub dof, loru.
Kàddu yu Xelu 13 in Kàddug Yàlla gi