Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 13:15-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 13:15-16 in Kàddug Yàlla gi

15 Dangay xam lu jaadu, ñu naw la; yoonu workat day metti.
16 Képp ku teey jëfe xam-xam; ab dof ay siiwal ndofam.
Kàddu yu Xelu 13 in Kàddug Yàlla gi