Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 13:10-11 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 13:10-11 in Kàddug Yàlla gi

10 Réy-réylu jote rekk lay jur, ku dégg ndigal a xelu.
11 Alal ju lewul day naaw; foral benn-benn, ba biibal.
Kàddu yu Xelu 13 in Kàddug Yàlla gi