Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 12:7-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 12:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Ab soxor bu daanoo, jeex na; ku jub, sa kër taxaw, ne këcc.
8 Xel mu ñaw, jëw bu rafet; sam xel jekkadi, ñu xeeb la.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi