Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 12:5-7 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 12:5-7 in Kàddug Yàlla gi

5 Ku jub, yoon lay mébét; ab soxor di lal pexey wor.
6 Ab soxor, waxam am tëru la, day reye; kàdduy kiy jubal di musle.
7 Ab soxor bu daanoo, jeex na; ku jub, sa kër taxaw, ne këcc.
Kàddu yu Xelu 12 in Kàddug Yàlla gi